Dewenati

96 views
Skip to first unread message

serignembacké tine

unread,
Nov 16, 2010, 4:43:10 AM11/16/10
to groupe Dahira Toulouse
Assalamelekoum
mangui léne ziarr bou bakh
Bonne fête Aid Adha
Dewenati!!!
Balle léne ma hake. ballenalène.
Yallana sounou Borome balle gnou
Gnou féké déwén té mou dakh réne

Tawfekh ak Taysir

Niane

unread,
Nov 16, 2010, 5:20:45 AM11/16/10
to dahirat...@googlegroups.com, groupe Dahira Toulouse
Deweneti balènema akh balnalène yalla naniou borom bi diegeule. Té maynou fane wou goudou ak wer niou fékéko ay yone you bari. Amine
Tawfékh ak taïssir

Niane

pape tall

unread,
Nov 16, 2010, 10:46:57 AM11/16/10
to dahirat...@googlegroups.com

balnala  balma yalla naniou bolé bal 
--- En date de : Mar 16.11.10, serignembacké tine <serig...@hotmail.com> a écrit :

cheikh diop

unread,
Nov 17, 2010, 5:52:01 AM11/17/10
to dahirat...@googlegroups.com, bamb...@hotmail.fr, baye...@yahoo.fr, beckam...@gmail.com, beu...@yahoo.fr, dial...@yahoo.fr, fallou-mard...@hotmail.fr, gnag...@yahoo.fr, gueyefa...@yahoo.fr, mbak...@msn.com, smk...@hotmail.fr, abdou khadre fall, Abdoulaye Dia, amy collé diop, Ass Syll, Assane Ndiaye, Assane Sine, Babacar Cisse, babacar cissé, bara thiam, Cheikh DIOP, Cheikh Ndoye, Cheikh Niang, Cheikh Tine, Cheikhou Diagne, chérif aidara Lo, cisse rokhaya, Diama Touré, Diéne Mamoune, Djily Seck, Fallou sokhna, halimatou diallo, Khadijatou Ndiaye, Khadim Dione, Khadim Seck, Maimouna Faye, Mamadou Faye, MAMADOU MOUSTAPHA SALL, Mame Cheikh Mbaye, Mami Diop, Mandian Mohamadou, Maty Diakhaté, medoune fall, Modou Lo, Modou Mamoune DIENE, Mohamadou El Bachir Seck, Mor Diéye, Mouhamed SALL, mous lo, Moussa Ndir, MOUSTAPHA ndour, Moustapha Niane, MOUSTAPHA sene, Ndeye Ndiaye, Pape Tall, Seynabou Dieng, Sidi Mbengue
Assalamou haleykoum,

Baal naniou leen baal léén niou. Niongi baalou akh waa dahira bi niepp té di léén ball. Nioo ngi djeguelou lepp lounou yeug agg lounou yeugoul té di niaane Yalla mou diégalniou sounouy ndioumté té nangou sounouy dieuf.

Noo ngi ziar niepp si bess bou teddbi.

Ngeen gagn  nioofatté si niaane yi. 

Niou tééwéko ay déwen you barri.

Cheikh DIOP
logo_massalik.jpg
Dahira Massalikoul Djinane Touba Toulouse
http://toubatoulouse.free.fr

logo_massalik.jpg
Reply all
Reply to author
Forward
0 new messages